Kamil Serigne Fallou Mbacké miy naafila ci joumay Touba ji.
Serigne Fallou dom la Ci Serigne Guédé Mbacké, mom Serigne Cheikh Asta Waalo mom S. Mame Mor Jaara
Jang mu wow kong la jang teereb yalla bi.
Ak mokkalam set na wecci waay
Ascolta Kaamil Seriñ Fallou Mbacké imaam Touba, Kinghiana. Un podcast su Stephen King e molti altri podcast da tutto il mondo con l’applicazione di radio.it